more from
Helico Music
We’ve updated our Terms of Use to reflect our new entity name and address. You can review the changes here.
We’ve updated our Terms of Use. You can review the changes here.

Jolof Bass Music

by Guiss Guiss Bou Bess

/
  • Streaming + Download

    Includes unlimited streaming via the free Bandcamp app, plus high-quality download in MP3, FLAC and more.
    Purchasable with gift card

      €4 EUR  or more

     

1.
Sabar dal mo Niou Nekh Ba tax Niou dëkeuk mome Fou mou dëke Niou dém fa fo dëke Fofo Nekh Ngeweul Ngeweul Sunu keur mame Ngeweul. Sabar Dafaye wakh (5) Sabar Sabar dafaye wakh Dafaye wakh Sabar dafaye wakh Sabar Sabar dafaye wakh Dafaye wakh Sabar dafaye wakh (6) Sabar dafaye wakh Sabar dafaye wakh (choeur) Sabar dafaye wakh Sabar dafaye wakh (choeur) Ah Dafaye wakh Mom dafaye wakh (choeur) Kone Lumu wakh Kone Lumu wakh (choeur) Wakh la Sabar (choeur) Kone Teguël Kone Sabar (choeur) Bo Teguë Niou Dégue Gala Niou Sabar. Gala Niou Sabar (choeurs) Sabar yangi Rire Sabar Yangi Djoye (choeur) Sabar Yangi Djoye Sabar yangi Rire (choeur) wax na dafaye Xibar Sabar (choeur) Kone Teguël Gala Niou Sabar (choeur) Sabar dafaye wakh Sabar Sabar dafaye wakh Dafaye wakh Sabar dafaye wax Sabar Sabar dafaye wax Dafaye wakh Sabar Sabar Sabar Sabar Dafaye wakh Sabar Sabar Sabar Sabar Sabar Dafaye wakh Dafaye Wakh Sabar Sabar Sabar Sabar dafaye wakh (5) Sabar dafaye wakh sabar (6)
2.
Insh Allah 05:01
Wolof lyrics : Aa aa aa Insallaa aa aa insallaa aa aa Insallaa aa aa Yàgg yàgg yàgg dina baax Insallaa Tolloon naa guddi yoo xam ne gënoon na fee metti lool Ma fas ci sama xol bi ak sama xel mi Xam ne yàgg yàgg bés di na mës a ñów Di na mës a ñów lépp di na jeex Ku am xolu muñ bés bu neexe nga fàtte yow la mettiwoon Sànt naa Yàlla Ndax Moom ku ko sànt mu dolli la Amaana xamnaa ni yoonu ndaw du gaaw Waaye gëm-gëm rekk a wóor fii ci dunyaa Yoon waa ngi nii gudd te lëndëm loole Bariy lëj-lëj ak jam-jam yi Gëm-gëm rekk a wóor fii ci dunyaa Bul ma dégglul waxi noon yi Ñii bëgg laa décourager Xanaa xamoo ne fii ci dunya gëm-gëm rekk a wóor Aa aa aa Insallaa aa aa insallaa aa aa Insallaa aa aa Yàgg yàgg yàgg dina baax Insallaa Liggéeyu ndey lanuy ñaan ak ndey ju baax Buur Yàlla defal nu ko kon sànt Yàlla Barke baay lanuy ñaan ak baay ju baax Ngir lu nu mën a am mu mën a barkeel kon alxamdulilaa Lii nag soo ko ame bul tiit bul ragal Xanaa xamoo ne dey leeral fa nga jëm Kon doxal te bul gestu Bul ma degglul waxi ñii Naan di na dem ak du dem Kon waaxul Kon waaxul gaawal a gaaw te demal sa yoon Aa aa aa Insallaa aa aa insallaa aa aa Insallaa aa aa Yàgg yàgg yàgg dina baax Insalla Xëccal mu dikk Xëccal mu dikk Yàgg yàgg Yàgg yàgg Di na mës a ñów Di na mës a ñów Di na mës a ñów waay Wërsëg bul buy turne la Ku sa niimero génn nga jot ko Te boo nee tekk tekk wan la yoon Sàcc bi da fa yàkkamti di jël waaye la muy sàcc wërsëgam la Doomu Aadama Njaay ku dund for sa muur Ñoddi bu dogul yàgg-yàgg soo ko gëme di na mësa dikk Walaay di na mës a ñów
3.
Tik Tik 03:33
Hé, Hé, Hé, Hé, Hé, Hé, Hé, Hé, Hé Diamono diamono tik tik Hé Hé Diamono diamono tik tok Hé Hé Diamono diamono Tiak Tiak Hé Hé Démba Taye Suba Hé Hé Diamono diamonay tik tok Barì Barì tak tik Tiak Tiak calcule tuki tuki dugu ba Hongkong Néfa kong kong Kéne dula kong Néfa kong kong Ana wa tik tik Wala tik tok (tok) Diamono diamonay Fatéliku diamonay Démba diamonay taye li Diamonaye diamono taye là Tik Tik Tiak Tiak Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Diamonay Diamonay Tik Tik Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Diamonay Diamonay Tik Tok Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Diamonay Diamonay Tiak Tiak Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Demba taye la Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Damba Suba Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Faté Fatéliku Tik Tik Tiak Tiak He Tak Tak He Fatéliku Fatéliku Bakh na dëe !
4.
Muus 04:44
Niou crée mouvement marché Mussanté Mamie Monsieur Madame Nieup fala Niou Diar Diar Ecole muus muus maligne malin Lëtema Léne diendeul ma ay lait ma nane Badadi leer leer Mussou koro mussou koro aka Muus (x15) Fekhel ba Muus Muus Muus (x6) Yo Muus Oh Muus (x8) Ngama muus té xam Linga beugue Ba Kéne dula nax Ngama muus Ba Kéne dula dugal Ngama muus Ba Kéne dula wax lo lofi wakhul Laisse passer léss wakhul Ngama muus Thi sa Ligueyou Kay Fonku ko Moy sa téranga Lo diangoul Wala khamo Lath ko kuko xam Lo xamul Boul di Boul di russa Lathié Bala Niou lay ték deal dor la ay marteau Banga mir gagny Danio graw graw féxél Ba yow ndaka muus école maligne malin ! Niou crée mouvement marché mussanté Ma séti docteur moussa avenue grand muus Mu sétal ma sama yaram Nama yow danga fatigué Bindal ma ordonnance frotter muus mi ak pamplemousse Bada di Thi duwu Léke Thi pamplemousse yi Batax na legui mangi féx Merci merci docteur Muus Moussa. Muus (x15) Fekhel ba Muus Muus Muus (x6) Yo Muus Oh Muus (x8) Mbong mbong ! nanga yéwu Bala Niou laye kong Sa bopp di feuke (x2) Mbong mbong nanga yéwu Bala Niou laye kong Sa bopp di feuke nga fok ko King Kong Intelligence boko amé Dinga am chance, chance! Ecole Maligne malin, malin!
5.
Sama Yaye Bëgg Nala Sama Yaye mane naw Nala Ennn Ya May djoy Lo Maman Sama Yaye Bëgg Nala waw Sama Yaye Bëgg Nala Sama Yaye mane Naw Nala Ennn ya May djoy Lo Maman Sama Yaye Bëgg Nala waw. Ay Waye May naru Ndeye Dieng Mbaye Sama yaye dume ko mesa faté Mane Ba Bayame Dée té Suma dioulé diko Nianal Bour yalla yereum ko Am na Niou guissoul Séne Yaye Mu méti lolle Y’a rabana diox là xolu mugne gni Nékak Séne Yaye niom dé laye waxal Liguëyou dôme Ndaye laniou wax Naniou saku séni Niane Ndax yalla Dimba Linnio——————— Amath Mbaye sa baye Diara Diouf Moy sa yaye Maguéte Séne disa mame Sing sing Yayu Fatou tok Bousso way naléne Yayu pape Bo yayu maman Fatou Thiat Démba Codou palume déne Thia ngoné palume Lambaye Diaxér Demba yayu niaye Borom lamb yithi ngéy ngéy Sa borom keur gereum Nala Bilaye wétal nga Nio. Bo menë defalale sa yaye Mola Embeu dju rom Nièinti weër Sunu yaye amu Niou Séne faye Bo menë défalale sa yaye Mo Dane sonu Thi yow Sunu yaye Amu Niou Séne faye Diox ko tieur Moy sa yaye Bul mér Lo Yow sa yaye Diox ko tieur Ndax Moy sa yaye
6.
Thiolcoder 02:30
7.

about

Après le succès de leur premier album Set Sela, et après avoir présenté leur musique habitée et explosive sur les scènes du monde, le trio afro-futuriste franco-sénégalais dévoile “Djolof Bass Music”, premier volet d’un nouveau projet percutant !

Au sein de ce disque, les rythmiques ancestrales fusionnent avec la bass music, les sonorités organiques et électroniques s’assemblent pour créer un nouveau genre musical : le Jolof Beats. Un sabar électronique affirmé et assumé, où les chants griotiques wolofs et le taassu (chant rythmique du mbalax) rencontrent le dub-techno et la deep house. Cet univers uptempo est porté par des chants rituels et par des messages spirituels et sociaux puissants. Le combo insère des sonorités organiques avec des rythmiques percussives complexes, et des polyphonies qui sont entremêlés de pulsations électroniques explosives. La musique du groupe puise dans les traditions du Sénégal, mais elle est visionnaire et panafricaine, elle englobe les musiques underground en pleine effervescences en Afrique telles que l’afrobeats et le cruise beat nigérian ou l’afro-house et le gqom sud-africain.

Djolof Bass Music transpire le bouillonnement musical de Dakar, la chaleur des clubs du continent Africain, et les traditions séculaires sénégalaises. Guiss Guiss Bou Bess incarne peut-être bel et bien le futur de la musique électronique en Afrique de l'Ouest en dévoilant un sabar électro-futuriste porté par des rythmiques effrénées et des beaks étatiques, qui n’attend que d’enflammer les dancefloors d’Europe et d’Afrique !

credits

released May 11, 2023

Mara Seck : chant, percussions
Aba Diop : choeurs, percussions
Stéphane Costantini : producteur
Philippe Ndong : guitare (Yaye bëgg nala)
Mohammed Champion : guitare (Sabar Dafaye Wakh, Insh Allah)
Enregistré par Stephane Costantini à la Maison des Cultures Urbaines, Dakar.

Enregistrements additionnels par Romain Dowska au Studio du Poisson Barbu, Paris.
Mixage et production additionnelle par anyoneID
Masterisé par Beat Laden

license

all rights reserved

tags

about

Guiss Guiss Bou Bess Dakar, Senegal

Guiss Guiss Bou Bess creates a powerful sound alchemy, mixing traditional Senegalese sabar drums with deep electronic beats.
Their unique style breaks down barriers and makes the sounds of Senegal accessible to people all over the world.

contact / help

Contact Guiss Guiss Bou Bess

Streaming and
Download help

Report this album or account

If you like Guiss Guiss Bou Bess, you may also like: